Li Ma Weesu


li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu




li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu seetal






leegi leegi ma gesu, ci li ma weesu
leegi leegi ma recu, walla sax di baaku






Fu gune yi feetee, dama leen di teetee
wax nu ma neexee, ma bëgga leen




Damay, damay, damay dellu gune
mel ni,mel ni, mel ni duma màgg










Lu ma gën di yàgg, xel ni mel ni bank
lu ma gën di màgg, dellu tuuti tank






Li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu






Li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
ma ni seetal


Leegi leegi ma gesu, ci li ma weesu
leegi leegi ma recu, walla sax di baaku


Our little photographers ♥ 


Fu gune yi feetee, dama leen di teetee
wax nu ma neexee, ma bëgga leen
Fu gune yi feetee, dama leen di teetee
wax nu mu ma neexee ma béggati




Li ma gën di jege, mel ni dama sore
lu ma gëna sore, gën di gis li ma jegewoon
lu ma gën di yàgg, xel ni mel ni bank



Li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu


Comments

Popular posts from this blog

Rosa Di Turi ♥

One Thing of Beauty